Mool (Deglu meteo) lyrics
 by Youssou N’Dour
		
		
Yaw mool u géej gi
Di jambaar ci réew mi
Bala ngaa dem géej
Ngala déglu météo
Bu la nee bul dem
Lu mën ë xew bul dem
Ben fan ak ñaar 
Bu mu yax sa liggéey
Doyloo nga yalla 
Du tee nga sa yor téléphone
Ak sa gps , te bul fatte sa gillet
Sama fans yi ma am 
Mool ñoo ma gën ë xam
Fu ma làng ee ak  ñoom 
Guddi gë day xumb lool
Man sama fans yee , ma saf
Sawar naa làng ak ñoom , fu ne
Aka ñoo dégg daaj , ma ni
Moo tax may dem ba jeex , walla
Jambaar ca waar wa 
Jambaar ca géej gë
Su ma ko mën oon 
Ben mool du des ci géej
Bu la nee bul dem 
Lu mën ë xew bul dem
Ben fan ak ñaar 
Bu mu yax sa liggéey
Sama fans yi ma am 
Mool ñoo ma gën ë xam
Fu ma làng ee ak  ñoom 
Guddi gë day xumb lool
Jambaar ca waar wa 
Jambaar ca géej gë
Su ma ko mën oon 
Ben mool du des ci géej
Man sama fans yee , ma saf
Sawar naa làng ak ñoom , fu ne
Aka ñoo dégg daaj , ma ni
Moo tax may dem ba jeex , walla
Yalna leen yalla suturaal 
Te di leen samm biir géej
Barke el seen liggéey bi 
Barke el seen njaboot gi
Aar leen ba ñu doon mag 
Jox leen barke maam yi
Man sama fans yee , ma saf
Sawar naa làng ak ñoom , fu ne
Yess  aye
Anh mool ba dem na géеj oo
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géеj oo
Anh mool ba dem na géej oo
Bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Mool yi laa bëgg ë làng al 
Seen làng xumb në 
Ndax sa ma fan’s yi nak 
Am mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
Sa telephone ak sa GPS 
Bul fatte gillet ba
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Ñoom laa bëgg ë làng al , seen làng xumb në 
Ndax sa ma fan’s yi nak , am
Mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
A dëgg ël , yaw mool u géej 
Yaa di jàmbaar
Yaa bari fullë lool
Bari jom lool
Yaa donn loolu
Gëm yalla lool
Yaa xarañ lool , te tabe lool
Youssou woy na leen
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Bël ba ca ndar , sonn al na waa guét ndar géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Mool yi laa bëgg ë làng al 
Seen làng xumb në 
Ndax sa ma fan’s yi nak , am
Mool yee ci gën ë dense
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Anh mool ba dem na géej oo
Mool yi laa bëgg ë làng al 
Seen làng xumb në 
Ndax sa ma fan’s yi nak , am
Mool yee ci gën ë dense